DÉGG NDIGËL AM NA NJARIÑ - RECOMMANDATIONS D’UN SAGE
54 pages
Wolof

Découvre YouScribe en t'inscrivant gratuitement

Je m'inscris

DÉGG NDIGËL AM NA NJARIÑ - RECOMMANDATIONS D’UN SAGE , livre ebook

Découvre YouScribe en t'inscrivant gratuitement

Je m'inscris
Obtenez un accès à la bibliothèque pour le consulter en ligne
En savoir plus
54 pages
Wolof
Obtenez un accès à la bibliothèque pour le consulter en ligne
En savoir plus

Description

Ce titre est le deuxième ouvrage en Wolof de Moumar T. Guèye. Il rappelle les bienfaits quand on écoute les personnes âgées et leurs sages recommandations. Cet ouvrage nous rappelle que quiconque fait du bien gagne le meilleur. Birima a aidé un vieillard en difficulté, ce vieillard l’a gratifié des bienfaits de ses conseils. Birame a bien écouté. Il est devenu très riche comme il ne l’a jamais espéré !
quote testimonial

L'avis de l'équipe

Sujets

Informations

Publié par
Date de parution 01 janvier 2024
Nombre de lectures 9
EAN13 9782723617543
Langue Wolof
Poids de l'ouvrage 8 Mo

Informations légales : prix de location à la page 0,0600€. Cette information est donnée uniquement à titre indicatif conformément à la législation en vigueur.

Extrait

DÉGG NDÌGËL.indd 1
Mumar Taala Géy
DÉGG NDIGËL AM NA NJARIÑ
RECOMMANDATIONS D’UN SAGE
© Les Nouvelles Éditions Africaines du Sénégal - Dakar - 2023
ISBN : 978-2-7236-1754-3
Cet ouvrage a été publié grâce au fonds d’Aide à l’Édition du Ministère de la Culture et du Patrimoine historique.
1
25/10/2023 11:25
“Di sant, te di ñaanal SoxnaMaam Yunuus JEŊ, mi ma xiirtal ci mbindum wolof.»
DÉGG NDÌGËL.indd 2
2
«Di ñaanal Sëriñ Fàllu Siise sëtu Maam»
“Cant, ak ngërëm ñeel na
Sëriñ Masàmba Sekk ca Tuubaa”
Nataal yi :Omar Diakité (ODIA)
25/10/2023 11:25
DÉGG NDÌGËL.indd 3
MBIDUM WOLOF MI
3
25/10/2023 11:25
Dégg ndigëlu mag am na Njariñ
Sëriñ Moor Wërsëg Góor gu baax la woon. Amoon wërsëg lool kaar, te yërëmoon njabootam te daan leen di dimmëli bu baax. Këram ga, naatoon na lool. Yàlla mayoon na ko ñaari doomi waxambaane !
Gàllaay a féete woon mag. Birima topp ca.
Benn bés, Sëriñ Moor woo ñaari doomam ya ni leen :
— Man dey damaa begoon a waxtaan ak yéen. Ndax léegi mag laa. Sama doole bareetul te sama alal wàññeeku na. Looloo tax ma bëggoon ngeen génn dëkk bi dem daani seen doole fu ngeen xam, ndax mat ngeen góor. Bu déwenee, su Yàlla defee ngeen am dara, ngeen dellusi, mën a beru te samp seen kër, yore seen njaboot ak seen i waajur.
Ba Sëriñ Moor waxee ba daaneel, Gàllaay ak Birima sant ko bu baax, rafetlu wax ja bu baax. Gàllaay ni ko :
— Maak Birima mii, nu ngi lay xamal ni, yoon woo nu teg, fa la nuy jaar, te dunu ko teggi mukk. Kon nu ngiy sàkku ñaan, ndax bu nu sañoon, bu ëllëgee ca fajar, danuy xëy dem toppi sunu wërsëg ni nga nu ko sante. Su ko defee, lu nu Yàlla may, nu indi bokk ko ak yaw ak njaboot gi.
DÉGG NDÌGËL.indd 4
4
25/10/2023 11:25
Ca ëllëg sa, ca fajar, ba ñu jullee ba noppi, seen baay ñaanal leen, ñu tàggoo ak moom daldi dem.
Gàllaay ak Birima topp yoon wa di dox wuti taax ya !
Ba ñu doxee ab diir, ca la ñu dab ag góor gu màggat lool, tànk ya tële, te ma nga gàddu ëmb bu diis gànn, di dox ci naaj wu tàng jérr.
DÉGG NDÌGËL.indd 5
5
25/10/2023 11:25
  • Univers Univers
  • Ebooks Ebooks
  • Livres audio Livres audio
  • Presse Presse
  • Podcasts Podcasts
  • BD BD
  • Documents Documents