Dund gu teey ci kéew mu sell Way yu nëtëx , livre ebook

icon

39

pages

icon

Français

icon

Ebooks

2023

Écrit par

Publié par

Lire un extrait
Lire un extrait

Obtenez un accès à la bibliothèque pour le consulter en ligne En savoir plus

Découvre YouScribe en t'inscrivant gratuitement

Je m'inscris

Découvre YouScribe en t'inscrivant gratuitement

Je m'inscris
icon

39

pages

icon

Français

icon

Ebook

2023

Lire un extrait
Lire un extrait

Obtenez un accès à la bibliothèque pour le consulter en ligne En savoir plus

Dund gu teey ci kéew mu sell Way yu nëtëx Saalum Jaane Dund gu teey ci kéew mu sell Way yu nëtëx Parcelles Assainies Unité 26, villa 253 E-mail: Mametoutyeditions@gmail.com ISBN: 978-2-492882-08-1 EAN: 9782492882081 Dund gu teey ci kéew mu sell Way yu nëtëx Jagleel naa liggéey bii: Sama baay Alasaan Jaane Sama nijaay Alaaji Mamadu Caam UBBITE GI Bu ñu sukkandikoo ci Mbootaayu Xeet yi (MX), lu tolloo ak tamdareet ci ay gàncax ak i garab, ak i mala ak i ndundat ñu ngi ci yoonu raaf. Te li waral loolii lépp mooy ci ni nit di MsÀDQWH DN NpHZ PL OD *jQFD[ \RR\LL DN JDUDE \L DN PDOD \L ak ndundat yooyii, amul lenn lu ci dundam di neen, lépp a am njariñ. Te njariñ li ñu am lépp soo leen dajalee ci dundug nit ki lay dellusi. Mooy lekk ci gàncax gi te gàncax du ko lekk, mooy dundee ndawali mala te mala yi dundeewuñu ndawalam. Mooy kenn ci mbindeef yi ki ci am ay naal yu romb ag dundam. Ay aajoom yemul ci lekk, naan ak jaxasoo, waaye am na yeneen yoy mënu leen a ñàkk, lu mel ni jàmm, xam li am feneen, mbëj, jokkoo, paj, njàng, xalam, añs. Te sax booy xool yu mujj yii bu ko ñàkkee amulug dund donte day lekk di naan. Li mën a yombal loolu yépp mooy na kéewam jag ba noppi. Liy jagal kéew mi ci loxoom la nekk. Nde daanaka mala yi ak gàncax yi amul lenn lu ñuy génne lu suuf si mënul soppiwaat jëfandikoo ko. Waaye nit mooy sulli ay mbéll soppi leen lol day yàq suuf si, ray ndundat yi, dellusi di tooke ci moom.
Voir Alternate Text

Publié par

Date de parution

01 janvier 2023

Nombre de lectures

15

EAN13

9782492882081

Langue

Français

Dund gu teey ci kéew mu sell Way yu nëtëx
Voir Alternate Text
  • Univers Univers
  • Ebooks Ebooks
  • Livres audio Livres audio
  • Presse Presse
  • Podcasts Podcasts
  • BD BD
  • Documents Documents
Alternate Text