-
30
pages
-
Wolof
-
Ebooks
-
2022
Description
Sofi xale puune bu jigeen la, bokk ci njaboot gu néew doole. Mësula dugg ekool. Ren jii nag, ci ubbite bi, ay way-juram bind nañuko ci ekoolu nguur gi. Sofi yàkkamti naa jàngi, waaye xamul la kofay xaar.
-
Publié par
-
Date de parution
01 janvier 2022
-
EAN13
9789956011452
-
Langue
Wolof
-
Poids de l'ouvrage
8 Mo