-
61
pages
-
Wolof
-
Documents
Description
Téere bii, ay woy la yu dajale xalaat yu xóot ci wàllu jikkó, politig, ak dundinu nit. Séex Aliyu Ndaw léeral na fi « Yoonu Ngor » ak « Paspas » ngir ndawi Afrig yi xam ne jom ak ngor ñooy reeni sunuy réew. Mu ngi nuy jàngal ne njiit du tal ittey boppam, waaye njariñu réew mi mooy xéyam ak ngontam.Séex Aliyu Ndaw ab mbindkat la buy sàmm làmmiñu réew mi. Bind na téere yu bari ci làmmiñu wolof ci fànn yu wuuté niki kilib, mayé, woy ak néttali. Mu ngiy mébét yeneeni téere yuy jàngale téy sàmm mbatiit ak mboorum sunuy réew.
-
Publié par
-
EAN13
9791097921194
-
Langue
Wolof